Lactualité en temps réel

Vidéo – Youssou Ndour aux Talibés mourides ” Baleen ma dama Xéer Rék…”

1 773

Vidéo – Youssou Ndour aux Talibés mourides ” Baleen ma dama Xéer Rék…”

Vidé Youssou Ndour devant Serigne Bass demande… par teledakar1

Laisser un commentaire

Quelque chose à ajouter ? Dites-le en commentaire.

28 commentaires
  1. kheuss dit

    Et si youssou le chanter en arabe kesk vous allez dire dire ne soyons pas complexes il rend hommage a son marabout a travers sa langue ouloff

  2. Gisto dit

    Mani ngeen teye sene guate vous qui parle de youssou ndour vous etez que des mécontents des chauds cœurs.si vous evez quelque chose à dire dite le votre mara qui lui a tendu le micro pour entendre sa belle voix.vous êtes que des defeant.guemouleen dara sene khol no kata ndayame rek mother Fock to all people say bad to him

    1. kenela dit

      Kou bakh xana xamoni saga baxoul nit d dafa wara am yar

  3. Sene dit

    Il dianguekatou khassaid yi wakh bokoul ak limou def mom musique lanko khamer te dianguekatte yi danouy tague mouhamed voila la différence

  4. Mamadou Dieng dit

    Youssou n’a rien fait, c’est la nature des Magal, Gamou et autres thiant qu’il faut revoir. Il n’y a que des mondanités et de la ripaille. “Que Dieu fasse de vous le Roi des arènes”, ont souhaité les Layenes à Macky Sall a la vieille des législatives. C’est ça le sens de l”Appel de Seydina Limamou?????

    1. Cheta dit

      Walahi liga wakh moye deugggg….oné tous en phase avc toi

  5. Maty Gallasse Dieng Diop dit

    Walay talibé mouride loumou def thi yonewi rek khepko yako woyone dioumté dou wesse té nul n’est parfait yalana sounou borom moussal gnou thi seytané

  6. Moustapha Ndiaye dit

    C sa pape Seck ndakh ap talibé dafay Yém si talibé am yar am téguine nit nak dafay dioum Youssou ndour dafa dioum diégalou

  7. Moustapha Ndiaye dit

    Yaw pape barah sa gnak kham motakh ngay wakh li fou Serigne abdou fata démé bay diegalou masama Youssou ndour té pourtant moko waylo kholal lingay wakh boubakh

  8. Pape Barah dit

    Senegal niooo soff wa damay ladie kou mom serigne fallou
    Serigne fallou nieup la
    Ghuissna ndiago Serigne fallou
    Khana youssou dou dioulitt
    Ishhhhh la paix way

  9. Bécaye Niang dit

    Pape dione va te faire foutre, je m’adresse pas à toi et jte connais même pas alors férme la

  10. Bécaye Niang Bara dit

    le prophéte a dit le meilleur d’entre vous fait parti de ceux qui ne s’occupe pas aux affaires des autre donc ” mandou baxna”

  11. Dione Pape dit

    Sén khol you bonyi Wanté Manoulén si Mom darra bagn bagn beugeu

  12. Bàra Thiapathioly Njàng dit

    Le prophète a t-IL demandait de tuer des êtres vivants ? Yalla dh digléwoul rey domou Adama kou nekeu sa bakane doy nala seukk

  13. Bécaye Niang dit

    Il n’arrête jamais de vous tromper avec ” je suis un mouride ou talibé” un vrai mouride dis musulman n’ira pas au bataclan pour soutenir des juifs et des non croiant. S.fallou n’a jamais recommandé ça

  14. Fallou Thiam Bsf dit

    Espèce de maride

  15. Ndao Preuve Nii dit

    Youssou defo dara nak vrement liga wayy ayoul lignouye nakhar lou kay moy diangue kat yifa nek diokhou gnoulen gnou diangue diokhla yaw mais defo dara

  16. Dione Pape dit

    Yaw Seytané gua louytal Rewmî Rék

  17. Vieux Mbodj dit

    Yaw maydio dara neykol si

  18. Vieux Mbodj dit

    patrons dakarou toujours dakay werer neko sorano nakou grand théâtre wakhon ga fi diabar amoul cart dentité encore tu répéter la même chose bare wakh kham liguaye wakh moka gueune

  19. Diop Maramane dit

    défou lou graw khana prochiane fois gua wakhko thji arabe rek nahté ligua wakh thji serigne bou bakh bobou di serigne fallou lou bakh rek la.thiat dou wess yalla nala yalla diapalé ndour yaw sénegal ligua fi déf thji begalaté ak creer emploi lolou lagnouwara fésseul ya wahone nit koudoul dioum amoul dagua kheurrek machallah k Dieu te protége

  20. Baïla Khardiata Diallo dit

    Iow #mañukk Ku ñaakk Talibé nga iow so xamoon lu daggan ding fi tuddu Baayu kenn suma russul woon sa turr bi wax la lu bonn reew nga trop…

  21. Fallou Thiam Bsf dit

    Lou bone daguéne di sonou rek mais sen bay ak sen mame manouniouko daguanal

    1. Anonyme dit

      Ndigal la diefê lép Serigne Bile

  22. Fallou Thiam Bsf dit

    Yow ya mena faine. Khadim Gueye dafa nowelo youssou ndour

    1. Anonyme dit

      Yaw kéne yaroula

  23. Astel Diop dit

    Bien dit pure vérité

  24. Modou Dione dit

    Youssou li nga déff dara nékousi ,li nga wakh rék la niép di wakh si Serigne bi,(Khadim Gueye,Khadim Kébé,Akassa Samb ect. Dagaa tagg S.Fallou rék ,wakh katt yi nek mom kénn mounou lèna téré wakh waayé liniou wara wakh daniouko wakhoul